Skip to content

Yaatal XamXam

  • ACCUEIL
  • POESIE
  • HISTOIRE
  • SOCIETE
  • ENVIRONNEMENT
  • ENERGIE
  • ART
  • JÀNG WOLOF

Month: November 2022

POESIE 

NJARIÑAL MBAY

14 November 2022 admin2295

Lolli bi jeex Noor bi dugg Mbay mi nangu Sàq yi fees Dund bi bari Xel yépp dal Gerte gi

Read more
POESIE 

MÀNDIŊ

14 November 202214 November 2022 admin2295

Àll ni sendaw lépp ni tekk Naaj wi tàng may dox man rekk Ñax mi bari mbooy gi ni ñareet

Read more
HISTOIRE 

El hadji Marokhaya Coumba Diagane

14 November 2022 admin2295 0 Comments

El hadji Marokhaya Coumba Diagane, un nom qui ne laisse personne indifférent dans le Njàmbur. Il était très respecté dans

Read more
POESIE 

JIGÉEN JU BAAX

14 November 202214 November 2022 admin2295 0 Comments

Yiw nga ta teey nga Ba ku la gis naw na la Sa jëmm ji rafet na Ba ku la

Read more
POESIE 

JEEXITALI JËF

14 November 2022 admin2295 0 Comments

Lépp lu la gaar Ngalla bum la waar Am na ci loo jaar Ta defóo ca la la war Geesul

Read more
POESIE 

MBAYUM GERTE

14 November 202214 November 2022 admin2295

Téeg xiin na ba ñalingaan Am ndox di yendoo xeeñ Mujj ngelawul njayaxaan Di upp ba am péex feeñ Nees

Read more
POESIE 

YARAL SA DOOM

14 November 202214 November 2022 admin2295 0 Comments

Yaral sa doom Ta teg ko ci yoon Def jom ci moom Ta defar jikóom Jàngal ko wax Ak def

Read more
JÀNG WOLOF 

WOLOF : Noms et verbes dérivés

13 November 202214 November 2022 admin2295

Quelques noms wolof et les verbes dont ils sont dérivés Associez les à leurs déterminatifs. VERBE Bind Jàng Bay Fóot

Read more
Copyright © 2025 Yaatal XamXam. All rights reserved.
Theme: ColorMag by ThemeGrill. Powered by WordPress.