Foyteef wu doy waar

Version anglaiseVersion françaiseVersion wolof


Strange fruit
Southern trees bearing strange fruit
Blood on the leaves and blood at the roots
Black bodies swinging in the southern breeze
Strange fruit hanging from the poplar trees
Pastoral scene of the gallant south
Them big bulging eyes and the twisted mouth
Scent of magnolia, clean and fresh
Then the sudden smell of burning flesh
Here is fruit for the crows to pluck
For the rain to gather, for the wind to suck
For the sun to rot, for the leaves to drop
Here is a strange and bitter crop

Source : LyricFind
Paroliers : Lewis Allen
Fruit étrange
Arbres du sud portant des fruits étranges
Du sang sur les feuilles et du sang sur les racines
Corps noirs se balançant dans la brise du sud
Fruits étranges suspendus aux peupliers
Scène pastorale du sud galant
Leurs grands yeux exorbités et leur bouche tordue
Parfum de magnolia, propre et frais
Puis l’odeur soudaine de la chair brûlée
Voici des fruits à cueillir par les corbeaux
Pour que la pluie s’accumule, pour que le vent suce
Que le soleil pourrisse, que les feuilles tombent
Voici une récolte étrange et amère

Foyteef wu doy waar
Garabi bë Saalum ya am foyteef yu doy waar
Xob ya ak reen ya lépp nga taq deret
Yaram yu ñuul ya di sadamtalu
Ca béntéñe ya
Jëf du doy waar ca bëj Saalum
gu taaru ga
Séen gët buqeeku séen gémmiñ weng
Xet u neex ya sedd yay
Gillee ca garabu magnolia ya
Mujj soppiku xetu wésëmu
Yaram wu ñu lakk ya
Loolu mooy poyteef yi tan yi
ñëw di raas
Ngir taw bi dajaloo
ngelaw li muucu di wowal
Jant bi di nëbal xob yépp di
ruus
Li de mooy ngóob mu doy waar ta metti ci xol.