WOLOF : Noms et verbes dérivés
Quelques noms wolof et les verbes dont ils sont dérivés
Associez les à leurs déterminatifs.
VERBE Bind Jàng Bay Fóot Faj Fexe Fecc Sant Sàcc Woor Ji Jëmbët Setal Def Fas Xam Gëm Am Sañ | NOM Mbind Njàng Mbay Póot Paj Pexe Pecc Cant Sàcc Càcc Koor Nji Njëmbët Cet Jëf Pas-pas Xam-xam Gëm-gëm Am-am Sañ-sañ |
VERBE NOM
Bind Mbind
Bay Mbay
Fóot Póot
Faj Paj
Fexe Pexe
Fecc Pecc
Sant Cant
Sàcc Càcc
Woor Koor
Ji Nji
Jëmbët Njëmbët
Setal Cet
Def Jëf
Fas Pas-pas
Xam Xam-xam
Gëm Gëm-gëm
Am Am-am
Sañ Sañ-sañ