Foyteef wu doy waar
Version anglaise | Version française | Version wolof |
Strange fruit Southern trees bearing strange fruit Blood on the leaves and blood at the roots Black bodies swinging in the southern breeze Strange fruit hanging from the poplar trees Pastoral scene of the gallant south Them big bulging eyes and the twisted mouth Scent of magnolia, clean and fresh Then the sudden smell of burning flesh Here is fruit for the crows to pluck For the rain to gather, for the wind to suck For the sun to rot, for the leaves to drop Here is a strange and bitter crop Source : LyricFind Paroliers : Lewis Allen | Fruit étrange Arbres du sud portant des fruits étranges Du sang sur les feuilles et du sang sur les racines Corps noirs se balançant dans la brise du sud Fruits étranges suspendus aux peupliers Scène pastorale du sud galant Leurs grands yeux exorbités et leur bouche tordue Parfum de magnolia, propre et frais Puis l’odeur soudaine de la chair brûlée Voici des fruits à cueillir par les corbeaux Pour que la pluie s’accumule, pour que le vent suce Que le soleil pourrisse, que les feuilles tombent Voici une récolte étrange et amère | Foyteef wu doy waar Garabi bë Saalum ya am foyteef yu doy waar Xob ya ak reen ya lépp nga taq deret Yaram yu ñuul ya di sadamtalu Ca béntéñe ya Jëf du doy waar ca bëj Saalum gu taaru ga Séen gët buqeeku séen gémmiñ weng Xet u neex ya sedd yay Gillee ca garabu magnolia ya Mujj soppiku xetu wésëmu Yaram wu ñu lakk ya Loolu mooy poyteef yi tan yi ñëw di raas Ngir taw bi dajaloo ngelaw li muucu di wowal Jant bi di nëbal xob yépp di ruus Li de mooy ngóob mu doy waar ta metti ci xol. |